Ngën-gi-woy8wol_mbs
1Éy su meloon ni sama càmmiñ nga,mel ni ku ma bokkal wenn ween,ba ma dajeek yaw biti, sañ laa dar,te du tax ñu sikk ma!2Ma jàpp la, yóbbu sama néeg yaay,moom mi ma yar ,ma may la biiñ bu saf,ak sama ndoxum gërënaat, nga naan.3Sama càmmoñu waay, ma gegenoo,ndijooram, ma laxasoo.4Yeen janqi Yerusalem, waatalleen mane dungeen dakkal te dungeen sooke tëraayu mbëggeelte jotul.